Na naszej stronie internetowej mamy pełny tekst piosenki Peundeul , której szukałeś.
Peundeul to piosenka Narah Diouf , której tekst ma niezliczone wyszukiwania, dlatego zdecydowaliśmy, że zasługuje na miejsce na tej stronie internetowej, obok wielu innych tekstów piosenek, które użytkownicy Internetu chcą poznać.
Ak fo né thi town bi
Foo ne ci réew mi ñëwël fi yëngu ci lii
Narah laay dooni
Man la ma ñëwaat fi gëna teggu ci beat bi
Xoolal ni may dugge
Xoolal ni may yégge sama baat ci kaaw
Mélodie bé meu yéglo
Gisatuma, déggatuma
Lenn lay gis kon kaay fii ma wone la
Gisatuma, déggatuma la
I’m so high
I’m so high yeeeh
Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Narah mooy pëndël pëndël pëndël
Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Narah mooy pëndël pëndël pëndël
Lu fora fora fort lay yëg sama xol
Fu kawe kawe kawe lay yekk sama yaram di yëngu
Ta xawma li koy yëngël fi mu jogé
Ayooooo
Guddi guddi non stress la dundu happiness
Tay non stop
Àndak samay way tay de fête la
Xoolal ni ma mel, kaay dance all night
Sound bi ndax yankay ngueug comme mane ni ma key yeugué
Wax ma ndax muñ lay duggu comme nimmey dougué
Gisatuma, déggatuma
Leen lay gis kon kaay fii ma wone leu
Gisatuma déggatuma la
I’m so high
I’m so high yeeeeh
Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Narah mooy pëndël pëndël pëndël
Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Narah mooy pëndël pëndël pëndël
Faxasul faxasul faxasul yow
Gënel li ci xol bi, tay duñu maye dara
Yëngëtul yëngëtul yëngëtul yow
Faxasul faxasul faxasul yow
Gënel li ci xol bi, tay duñu maye dara
Yëngëtul yëngëtul yëngëtul yow
Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
(Kaay ñu pëndël)
Narah mu pëndël pëndël pëndël
(Kaay ñu pëndël pëndël pëndël pëndël eeh)
Kaay ñu pëndël pëndël pëndël
Ehhh ehh ehh ehh ehh
Narah mooy pëndël pëndël pëndël
Hummm hummm
Otras canciones de Narah Diouf
Najczęstszym powodem chęci poznania tekstu Peundeul jest to, że bardzo Ci się podoba. Oczywiste, prawda?
Jeśli Twoim motywem do szukania tekstu piosenki Peundeul było to, że absolutnie Ci się podoba, mamy nadzieję, że będziesz cieszyć się jej śpiewaniem.
Czuj się jak gwiazda, śpiewając piosenkę Peundeul wykonaną przez Narah Diouf , nawet jeśli Twoją publicznością są tylko Twoje dwa koty.
Bardzo częstym powodem szukania tekstu Peundeul jest chęć dobrze go znać, ponieważ przypomina nam o jakiejś specjalnej osobie lub sytuacji.
Coś, co zdarza się częściej, niż myślimy, to że ludzie szukają tekstu Peundeul , ponieważ jest w niej jakieś słowo, którego nie do końca rozumieją i chcą upewnić się, co ono oznacza.
Kłócisz się ze swoim partnerem, ponieważ rozumiecie różne rzeczy, słuchając Peundeul ? Posiadanie tekstu piosenki Peundeul wykonanej przez Narah Diouf może rozstrzygnąć wiele sporów, i mamy nadzieję, że tak się stanie.
Ważne jest, aby zauważyć, że Narah Diouf na koncertach na żywo nie zawsze był lub będzie wierny tekstu piosenki Peundeul ... Więc lepiej skupić się na tym, co mówi piosenka Peundeul na płycie.
Mamy nadzieję, że pomogliśmy Ci z tekstem piosenki Peundeul wykonanej przez Narah Diouf .
Na tej stronie masz do dyspozycji setki tekstów piosenek, takich jak Peundeul wykonane przez Narah Diouf .
Naucz się tekstów piosenek, które lubisz, jak Peundeul wykonane przez Narah Diouf , czy to do śpiewania pod prysznicem, tworzenia własnych coverów, dedykowania ich komuś lub wygrania zakładu.
Pamiętaj, że kiedykolwiek potrzebujesz znać tekst piosenki, zawsze możesz na nas liczyć, jak to się stało teraz z tekstem piosenki Peundeul wykonanej przez Narah Diouf .