Teg ko ci temps
Amoon nga fi temps
Léegi ñun ñoo moome vent
Dangay nappe!
Yaw xam nga rekk dama di ndaanaan
Lamb démb ma daan
Ma leen gëna saf ni daxar ba ci yoon mbaadan
Moytul noon mu tarxis saran
Bari ngeen jaxan
Flow bu reew la indi tay moom
Rap bu soft la laal
Amul arrêt (amul arrêt)
Dey daw rekk (dey daw rekk)
Fees lay def, xam naa gone bi comme Mbappé (comme Mbappé)
Ma ni amul arrêt (amul arrêt)
Munoo ma tardeel (mukk mukk)
Xam nga coof laa raw ma jafe bàyyi ma
Sàndi sama mbale mi nappé
Déy daw rekk
Yoroo wéroo
Eh, bëgg jitte bëgg nappé
Looy nappé, looy nappé
Xam nañu li ngay dundu
Dawoo suñu yaram, dangay nappé
Teg ko ci temps
Amoon nga fi temps
Léegi ñun ñoo moome vent
Dangay nappe!
Fetaak moom place
Ñoom ci kaw lañu jëm
Te man fa laa toog
Romb ay kuti ñu may mbow
Ndax te bukki bi la bot
Taat moo ko topp muy déllu gannaaw
Ci bi ma ko
Man ak ñoom dootuñu laale jamais
Comme les Guissés-Maabo
Teg fa sa loxo jàppal ma temps
Pépite la ni Kylian
Ñaw ngemb tere mbot ndaanaan dégg may daan
Àdduna potu nda la sa rappeur du gux du naan
Man lan ko diw ma jàpp seen girl yi, jàppal leen gam
Final rekk moom laay joué
Moom chef de bandi lay ñodd cooki feebar rekk de
Dinañu ma daq mais yere yi may sol rekk a may teye
Xaalis lay xëccoo mais du pe
Lu ne lay teg sama der tewul maa ngi jàpp teint
Amul arrêt (amul arrêt)
Dey daw rekk (dey daw rekk)
Fees lay def, xam naa gone bi comme Mbappé (comme Mbappé)
Ma ni amul arrêt (amul arrêt)
Munoo ma tardeel (mukk mukk)
Xam nga coof laa raw ma jafe bàyyi ma
Sàndi sama mbale mi nappé
Déy daw rekk
Yoroo wéroo
Eh, bëgg jitte bëgg nappé
Looy nappé, looy nappé
Xam nañu li ngay dundu
Dawoo suñu yaram, dangay nappé
Teg ko ci temps
Amoon nga fi temps
Léegi ñun ñoo moome vent
Dangay nappé!
Man rekk ci sama yoon comme BRT bi
Xale yaa ngi jooy ass bi la tebi
Ne ma général yaw la asp bi
Soxlatul may wax lam xa bi
Ñaw, kàddu baal la dum leen gaawa dégg
Man la dogo ñi doon bañ rambax ci game bi lañ gis tey ñu yor bongo
Comme Aly wéy geroo fils sa buur la
Benn Aly ñëw wacc la sa ngur la
Tegal sa rappeur sañ-sañ, tojal ko mbari from Dieck
Teg ko ci temps di sañse, jamos ko blow tek-tek
Lindia seen game bi bët-set, seen K7 sama weccet
Fatt dundu lifu jetset, teddi king fat pérpéte
Amul arrêt (amul arrêt)
Dey daw rekk (dey daw rekk)
Fees lay def, xam naa gone bi comme Mbappé (comme Mbappé)
Ma ni amul arrêt (amul arrêt)
Munoo ma tardeel (mukk mukk)
Xam nga coof laa raw ma jafe bàyyi ma
Sàndi sama mbale mi nappé
Déy daw rekk
Yoroo wéroo
Eh, bëgg jitte bëgg nappé
Looy nappé, looy nappé
Xam nañu li ngay dundu
Dawoo suñu yaram, dangay nappé
Teg ko ci temps
Amoon nga fi temps
Léegi ñun ñoo moome vent
Dangay nappé!
Istnieje wiele powodów, dla których chcesz poznać tekst Nappé (feat. BM Jaay & Bass Thioung) wykonanej przez Samba Peuzzi .
Jeśli Twoim motywem do szukania tekstu piosenki Nappé (feat. BM Jaay & Bass Thioung) było to, że absolutnie Ci się podoba, mamy nadzieję, że będziesz cieszyć się jej śpiewaniem.
Jeśli Twoje poszukiwanie tekstu piosenki Nappé (feat. BM Jaay & Bass Thioung) wykonanej przez Samba Peuzzi wynika z tego, że przypomina Ci o kimś konkretnym, proponujemy, abyś zadedykował jej to na jakiś sposób, na przykład wysyłając jej link do tej strony internetowej, na pewno zrozumie aluzję.
Mamy nadzieję, że pomogliśmy Ci z tekstem piosenki Nappé (feat. BM Jaay & Bass Thioung) wykonanej przez Samba Peuzzi .
Na tej stronie masz do dyspozycji setki tekstów piosenek, takich jak Nappé (feat. BM Jaay & Bass Thioung) wykonane przez Samba Peuzzi .